Overblog Suivre ce blog
Editer l'article Administration Créer mon blog
La Semaine de Convivència à Arles

Geej (la mer)

1 Juin 2008, 11:20am

Publié par Association Attention Culture

Géej Géej Mamboulane (bis) / Mer, Mer

Géej Géej Mamboulane) / Mer, Mer
Yangi wotal seï dom ) / Tu tentes tes enfants

Géej Géej Mamboulane) / Mer, Mer
Yangi wotal seï dom / Tu tentes tes enfants

Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Géej Géej Mamboulane) / Mer, Mer
Yangi labal seï dom / Tu engloutis tes enfants

Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Yangi labal seï dom / Tu engloutis tes enfants

Dunde yakaar ba kawar weex / On s’est nourri d’espoir jusqu’à avoir les cheveux blancs
Di tëss tëss si ba dole diekh / On s’est démerdé jusqu’à épuisement

Yakaar labne biir géej / L’espoir s’est noyé en mer
Tey ma songue bek mi / Aujourd’hui, j’affronterai la tempête
Yakaar yékessuna / L’espoir s’est dissout
Tey ma sobu Géej / Il ne me reste plus qu’à plonger dans tes eaux

Bulen fokni djeul loco nexnema / N’imaginez pas que j’embarque sur un rafiot de bon coeur
Mey seen avion yi di naw / Pendant que je vois ces avions voler au-dessus de ma tête

Barça wala barzax lulen wutele ci man tey / Accoster à Barça ou mourir, quelle différence pour moi aujourd’hui ?

Ceuta ak Melillla fu ma tere baaxna ci man tey / Ceuta ou Melilla quelle différence pour moi aujourd’hui ?

Bulen fokni jel loco neex nama / N’imaginez pas que j’embarque sur un rafiot de bon coeur
Mey seen avion yi di naw / Pendant que je vois ces avions voler au-dessus de ma tête

Oh oh oh oh

Géej Géej Mamboulane (bis) / Mer, Mer
Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Oubil ma seï loxo / Ouvre moi tes bras

Beguena am jaabar / J’aimerais avoir une femme
Am ay dom / Des enfants

Beguena tekki ni samay morom / J’aimerais réussir comme d’autres
Beguena sutural samay wadjour / J’aimerais soutenir mes parents
Liguey yu ndey anup dom / Pas de réussite sans le bonheur de la maman

Oh oh oh oh
Géej Géej Mamboulane (bis) / Mer, Mer
Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Damay wuti liguey / Je vais juste chercher du travail

Yakaar yekessuna / Puisque l’espoir s’est dissout
Tey ma sobu Geej / Aujourd’hui, je plonge dans tes flots

Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Damay wuti liguey / Je vais juste chercher du travail

Géej Géej Mamboulane / Mer, Mer
Ta lal ma sey loxo / Mer, donne moi la main

Commenter cet article